Passionné(e) de lecture ? Inscrivez-vous gratuitement ou connectez-vous pour rejoindre la communauté et bénéficier de toutes les fonctionnalités du site !  

Les sillons ; saawo yi ; recueil de poèmes wolofs

Couverture du livre « Les sillons ; saawo yi ; recueil de poèmes wolofs » de Daouda Ndiaye aux éditions L'harmattan
Résumé:

Dawuuda Njaay aw ci yoon wi noom Séex Musaa Ka xàlloon. Woy yii mu wéer ci léebu yi fi Maam bàyyi xoot nanu. Di nan yar yeete suuxat xel naatal xalaat. Teewul nose bi sol galan buy dàkk xolu bépp dom Aadama. Te loolu la woykat tigi di sàkku.Daouda Ndiaye suit le chemin tracé par le précurseur... Voir plus

Dawuuda Njaay aw ci yoon wi noom Séex Musaa Ka xàlloon. Woy yii mu wéer ci léebu yi fi Maam bàyyi xoot nanu. Di nan yar yeete suuxat xel naatal xalaat. Teewul nose bi sol galan buy dàkk xolu bépp dom Aadama. Te loolu la woykat tigi di sàkku.Daouda Ndiaye suit le chemin tracé par le précurseur Cheikh Moussa Kâ. Ses poèmes s'appuient sur les proverbes légués par les ancêtres. D'où leur richesse.

Donner votre avis